Potion Magique by El Maestro
"Potion Magique" is Senegalese song released on 09 November 2024 in the official channel of the record label - "El Maestro Le Kangham". Discover exclusive information about "Potion Magique". Explore Potion Magique lyrics, translations, and song facts. Earnings and Net Worth accumulated by sponsorships and other sources according to information found in the internet. How many times the Senegalese song appeared in music charts compiled by Popnable? "Potion Magique " is well-known music video that took placements in popular top charts, such as Top 100 Senegal Music Chart , Top 40 Senegalese Songs Chart, and more.
[Edit Photo]
|
Download New Songs
Listen & stream |
|

"Potion Magique" Facts
"Potion Magique" has reached
45.1K total views,
0 likes,
and dislikes on YouTube.
The song has been submitted on
09/11/2024
and spent 3 weeks on the charts.
The original name of the music video "Potion Magique" is "EL MAESTRO - POTION MAGIQUE | CLIP OFFICIEL".
"Potion Magique" has been published on Youtube at 09/11/2024 12:00:06
"Potion Magique" Lyrics, Composers, Record Label
Artist : El Maestro
Music : El Maestro
Mix & Mastering : SNBEATS STUDIO
Lyrics & Topeline : El Maestro
Réalisation : Digit prod
Cadreur : Sidy Niang
Light : Digitprod
Charge de prod : Moussa Diop
Stylisme : EMIKO DESIGN
Imagine Caravane Nationale : Cheikh Ndiaye
REMERCIEMENTS
Moussa Diop - Emiko Design - Yacine Sy - Kiné Sow - Mouhamed Diop - Cheikh Ndiaye CND Film Maker
Copyright Novembre 2024
Lyrics
REFRAIN
Askan wi la dioxone nga agne
Boula digué rér gueum ko
Nioune nji falone Diomay
Dinaniou ko diox assemblée
Gouy gui nara doundal Sénégal
Ñun dina ñu ko arr ba mu maag sunu gal la
Système bi diogué fi abadan
Dina ñu ko raay mou deh
Mou abal ño
Nguir Diomaye doxal
Sonko di doxal
La Potion Magique du projet moy Majorité
Ñu doxal di doxal
Ñu doxal di doxal
La Potion Magique du projet moy Majorité
Ñu doxal di doxal
Ñu doxal di doxal
La Potion Magique du projet moy Majorité
COUPLET I
Dafa diot ñu am assemblée bu bess
Ak ay députés you am qualité
Liguey rek té duñu dagassanté
Bulletin bu baax bi moy bu Pastéf
Kaay ma wan lako
Dafa verte wéx am photo Ousmane
Sonko tutti rouge ak Pastef les Patriotes
Wan ko Yaye wan ko Baye
Top ndigalu Tata Maimouna Bousso
Focus
Le 17 ma bathie lén
Bathie lén na xiir yi dall
Focus
REFRAIN
Kone suñu la digué rér gueum ko
Nioune nji falone Diomay
Dinaniou ko diox assemblée
Gouy gui nara doundal Sénégal
Ñun dina ñu ko arr ba mu maag sunu gal la
Système bi diogué fi abadan
Dina ñu ko raay mou deh
Mou abal ño
Nguir Diomaye doxal
Sonko di doxal
La Potion Magique du projet moy Majorité
Ñu doxal di doxal
Ñu doxal di doxal
La Potion Magique du projet moy Majorité
Ñu doxal di doxal
Ñu doxal di doxal
La Potion Magique du projet moy Majorité
COUPLET II
Buñu amé Majorité
Loi bu baax ñu Voté
Dindi amnesty bi
Délo justice Martyres yi
Jubb Jubbal Jubanti rék
Ték fi haute cours de justice
Ku fi Jeulone alalu réwmi
Dinga ko Gokki watt
Sénégal ñoko mana défar
Goor Jiguen Magg ak ndaw And liguey
Sénégal vision 2050
Wathiél thiono sunuy doom yi takhone ñuy xéxx
Dont de soit pour la patrie
Pour un Senegal souverain Juste et prospère
REFRAIN
Askan wi la dioxone nga agne
Boula digué rér gueum ko
Nioune nji falone Diomay
Dinaniou ko diox assemblée
Gouy gui nara doundal Sénégal
Ñun dina ñu ko arr ba mu maag sunu gal la
Système bi diogué fi abadan
Dina ñu ko raay mou deh
Mou abal ño
Nguir Diomaye doxal
Sonko di doxal
La Potion Magique du projet moy Majorité
Ñu doxal di doxal
Ñu doxal di doxal
La Potion Magique du projet moy Majorité
Ñu doxal di doxal
Ñu doxal di doxal
La Potion Magique du projet moy Majorité