Yëffu Doff by Baye Mass
"Yëffu Doff" is Senegalese song released on 19 March 2023 in the official channel of the record label - "Baye Mass Officiel". Discover exclusive information about "Yëffu Doff". Explore Yëffu Doff lyrics, translations, and song facts. Earnings and Net Worth accumulated by sponsorships and other sources according to information found in the internet. How many times the Senegalese song appeared in music charts compiled by Popnable? "Yëffu Doff " is well-known music video that took placements in popular top charts, such as Top 100 Senegal Music Chart , Top 40 Senegalese Songs Chart, and more.
[Edit Photo]
|
Download New Songs
Listen & stream |
|

"Yëffu Doff" Facts
"Yëffu Doff" has reached
2.9M total views,
92.4K likes,
and dislikes on YouTube.
The song has been submitted on
19/03/2023
and spent 108 weeks on the charts.
The original name of the music video "Yëffu Doff" is "BAYE MASS - YËFFU DOFF ( CLIP OFFICIEL)".
"Yëffu Doff" has been published on Youtube at 19/03/2023 13:59:58
"Yëffu Doff" Lyrics, Composers, Record Label
Auteur : Baye Mass
Production: Mpossible Prod
Réalisateur : Pac Deejay
Compositeur : Pape Laye
Studio : Mpossible
Mix & Mastering : Sirtam Beats
Une production de Mpossible Prod (Dakar, Senegal, Mars 2023)
** Retrouvez Baye Mass sur ses réseaux sociaux **
Instagram :
TikTok :
** Retrouvez Mpossible Prod sur ses reseaux sociaux **
Facebook :
Instagram :
Site web :
** Contact management **
contact@
78 300 52 52
Lyrics
Yow ! Rigolo , con, ñëpa parano fiii …
Kunek tibë jëmelé sa biir bi
xawma dañu rew xawma dañu possedé !
Suñu grand yi wara jangalé di xasté
Fi Études , Politique , Économie ñossi ngenë delu guinaw
Détails yi , Batailles yi ak yëfu doff yi ñossi ëpp ay trophée
Mérité woleine ma judu ci sen Réw mi ! Dama wara déménager dem deuk thi Air bi…
fi ñi fi gën nul lañj gën diox nope
Ñi fi gën immature lañu gën diox bope
Jiguene yi , Billets yi ak Bouteilles yi la xalé you guor yi di weur
Volets yi , Billets yi ak Téléphone yi Mom la djiguene nji di weure
Bëri yëfi doff … Senegal dafa bëri yëfi doff
Bëri yëfi doff…
Bëri yëfi doff …senegal dafa Bëri yëfi doff
lolu rek fi dox
Bëri yëfi doff … Senegal dafa Bëri yëfi doff
Bëri yëfi doff …
Bëri yëfi doff …sama rew dafa beuri yeufi doff
lolou rek fi dox
Deuk bu xate … Alë yu yaatu
Auto you chère …té tali bi baxoul
Stade bou bess… té talibé yi lekuñu
Avion bou bess … té ame village you naanul …
Ame coupe bou bess… ndeketei palais woroul …médias you faux , journalistes you jangoul…
Musik bou rëp… té contenu bi baxoul…
Rappeurs you Réw ak mbalakh man you ayul
Mérité woleine ma judu ci sen Réw mi ! Dama wara déménager dem deuk thi Air bi…
fi ñi fi gën nul lañj gën diox nope
Ñi fi gën immature lañu gën diox bope
Jiguene yi , Billets yi ak Bouteilles yi la xalé you guor yi di weur
Volets yi , Billets yi ak Téléphone yi Mom la djiguene nji di weure
Bëri yëfi doff … Senegal dafa bëri yëfi doff
Bëri yëfi doff…
Bëri yëfi doff …senegal dafa Bëri yëfi doff
lolu rek fi dox
Bëri yëfi doff … Senegal dafa Bëri yëfi doff
Bëri yëfi doff …
Bëri yëfi doff …sama rew dafa beuri yeufi doff
lolou rek fi dox
Bëri yëfi doff …sama rew dafa beuri yeufi doff
lolou rek fi dox